Kàddug Yàlla “Nit du dunde mburu rekk,waaye itam gépp kàddugu génne ci gémmiñug Yàlla.” Man ngaa yebe Kàddug Yàlla ci sa ordinatër walla nga jànge ko fi ngay doxale sa internet ak Kàddug Yàlla+. windows mac/iPad web Am nañu itam ay modules ngir logiciels yu tudd Logos ak Accordance Dem fa Ab Jukki ci Kàddug Yàlla Ay nettali yu nu jukki ci téere yici mbindum alfa, ak mdindum arab, ànd ak ojo 99 Juróom ñeent fukk ak juróom ñeenti turi Yàlla yu rafet yi ci arab ak ci wolof Arminaatu Wolof Weeru wolof ak weeru tubaab ci benn appli